Bril Fight 4… EL Messias The Legend (Official video)

BeFunky_null_3.jpg Publicado el 29/7/2014

Music video by Bril Fight 4… performing EL Messias The Legend (Official Video). (C) 2014 … Exclusive track for the number one Bril (Ndéweuneul ) Directed by: Reverse Studios.

Class’Chic Records présente BRIL FIGHT.4… "Li Ma Déssé ?" + Lyrics

10348374_795904380444341_7485454086463496494_n

Class’Chic Records présente
BRIL FIGHT.4… "Li Ma Déssé ?"
Brand New single en #free_Download
Max de partage ***** Nathi nieuppp djottt yaaaa

 ·

 

LYRICS

Bril Fight 4… – Li Ma Dessé (Lyrics)

{Intro}

Class’Chic Records, Yeah …….Bril Fight 4… The last Fighter

Li Ma Déssé ngééni Lathie haan ??

Déggloul , Allright I write yaa

 

{1er Couplet}

May ki yagga gëstou doga tambali,seugg thi mbindeu mi def track

Andaki djambar sôbou thi kharé nieupp dokh ma dess di raakk

Laata baatou Obama di djipp la khamni "yes i can"

Oubi Class’chic di guéénè lou deep yakarouma thi kén

Def musique #fonction, dithi kheuy ,seugg thi , yaggueu thi beurri ay son

Dougou sa #domaine, #dérivé romb sa #limit yi wanela #variation

fayékou djizz thi bizz bi djay beats, wowèma Docter Dre

Deukk thi mixé master ay Hit ba niou beuri dok di diri,

Bagage yi, yeukk liy daw thi siditt , i’m the best ever did it

Téchnique bi visé, rime yi waathiélén né tireur d’élite

Xaré thi mbedd mi nekkeu fa heros bi, fégnal li neubouli wané sa zero bi ,

zik bi crazy, teureudi ,folli sa Prési… ,Eundi sa palai thi ghetto bi ,,,

 

{REFRAIN}

Niggiz wanna know , Li Ma déssé now

*********Yeaahhh******* allright

Cuz They wanna know , Li Ma déssé now

*********Yeaahhh*******Let’s go

Niggiz wanna know , Lane moma déssé now ?

Li ngay weur di laathieté , tontou-béngui sa guinaw , hun

Mangui nieuw, Yeukeutil-lén Hip Hop bi

Seugg thi mbindeu, wané thi deugg bi, guééné li nékk thi bopp bi

 

{2ème Couplet}

Kouy yeungou thi game bi kham nga may kann, djaratoul di déf semblant

Wouték nieupp néékha raagné ni bèn black thi 100 blanc ..

Boudéé Ki meunn sa king bi ngay séétt néma djakkeu ba weur

24h ma yèèw thi terroriste né "Jack Bauer"

Djèki djéki daw guissoma

All right i write yaw wo sama

Bépp number one ,rap ba gueunla wane, Bomb nieupp comme Ossama

Dikkeu djokhla leçon , tiidji say nopp sotifa son

Tabakh sa doundou ni bén maçon, May ki ngay dégglou sopi façon

Yakci Yéggueul niveau bi, yokkkou fi mbindeu mi , dougou thi xel yi di tatoué ,

Kou dékkeu sa nopp ci deunn yi, degg-nga xol yi nignoumay tathiou wé

Gni takhaw thi bitti di bagn, kouthi lakkou nim may thiatouwéé

Guéneu sissou ba dima teukeulék gni ma toloul thi thiatou wé….

 

{REFRAIN}

Niggiz wanna know , Li Ma déssé now

*********Yeaahhh******* allright

Cuz They wanna know , Li Ma déssé now

*********Yeaahhh*******Let’s go

Niggiz wanna know , Lane moma déssé now ?

Li ngay weur di laathieté , tontou-béngui sa guinaw , hun

Mangui nieuw, Yeukeutil-lén Hip Hop bi

Seugg thi mbindeu, wané thi deugg bi, guééné li nékk thi bopp bi

 

{3ème Couplet }

Da supa thi beat dou taaba taaba

Yokou na fèèm, ba gagnè kata ba

Romb di daw niou beuri di yaaba

Wakh thi djeumm dji yokou tiyaaba

Rime bou guéénati dal la né kaba

"Bril meunoul rap" Moy Macqua amoul kaaba

********Astaghfirullah Bakaar********** ,

Djoulil niaari raaka toubb, Khamnga ni léppeu la boolé bouppp,

Yokou fi léér bi, teuyé hilér bi , niakh yi maaguétt yeupp la gouppp

Gni nangou Technique bi , nane dou bindeu Sén your yi lamay sol daa

Thiappeu thi xalima xaatim soppilènn samay soldat

Dama eundi lou besss /wakh ma lou dess

Feuleu gueuna gaaw nieupp yokkou vitess

Tek lima meuné, niounè tékkeu gueuna yémou,Kouné beugg deuggeu deugg lima wané thi test …

Laakou Teudjou seugg reudd mbindeu gueuna beurri,

youkou déggeu déggueu founé, kouné guéneu dithi weuri ,

lima yagga. Seugg teugg , parè feugg nieup teurri ,

" I’m the best" kouy weur kouma meunn tèèla rééri

 

{REFRAIN}

Niggiz wanna know , Li Ma déssé now

*********Yeaahhh*******

Cuz They wanna know , Li Ma déssé now

*********Yeaahhh*******Let’s go

Niggiz wanna know , Lane moma déssé now ?

Li ngay weur di laathieté , tontou-béngui sa guinaw , hun

Mangui nieuw, Yeukeutil-lén Hip Hop bi

Seugg thi mbindeu, wané thi deugg bi, guééné li nékk thi bopp bi

 

{Outro}

Fi moy Galsén nigga , bougn lay laathie lééray nga eundil-lén djantt , ay torche laniouy weuri, taal di niitt nane-la dafa leundeum

"you already know what it is man" – Yama gueuna xam , ….. right

************************Dara Déssoul Nigga ***********************

Analyzik bi/// moy sopi Analou zik bi///

Bril Fight 4 #speed_test #teste_de_vitesse directed by Nazir Ciss 26.05.2014 + Lyrics

Brilis is back · I’m about to drop the best freestyle ever,,,,, listen !!! #speed_test #teste_de_vitesse Publié le 26/5/2014 #Speed_Test freestyle #Analyzik , Class’Chic Records 2014 Rappeur et beatmaker indépendant Sénégal/Dakar Directed By Nazir Ciss New single dispo sur http://www.reverbnation.com/brilfight4 · http://youtu.be/smJs1swMrvs · Finga beugga djégué laniou feugg,dinga djeulli liniou eundi,meuna khaamé finiou meuné, liniou nara wané, bakkou thi seugg beurré,songou naniou daan ndambou,doga meuna feugg deuneu, kouné guéneu weuri bénam… · Wala douniou meuneu takkeu ba di saam, sunu guinteu laniou wara fonkou deukk diko sameu, ben yone laniou xaleu andeu,dém loumou beurri beurri boul xol keulé limou sol dako béén am ? · Deugg laniou wané gniko céédé, beuga djégué dithi bégué, kouné fékhé finiouy teugué , ni nga yeugué, diko dééggué,beug beuga tégué , deug deug djokhé , liniou digué , finiouy diiigué doko fééké never "han" · *tou* *tou* *tou* · fooné cent mané tou tout , carte gui djoutou , supa dupa djitou , lathieté lépp connais tout, djouggatina daw dém , rawatina Bolt djokhatiko number *two* *two* · ======>>>>> Let’s go · Lifi gueuneu neubou laniou djeuli ,firi idji, bountou binga wara djaaré laniou djégué diko tidji, douma déggueu déé mongui dikkeu daw khidi fidi , liniouy iri, diniou diri , djaral naniou seugg sigui , deukeutéko ték ko tigui tigui , nieupp yokhou · *Daiiiimn* (rire) ……Come on · Léégui fouma dougou djokhé mayé minimum , kou thiy wakh yén rime yi teudji guémigneum , kila yagga deukkou, dila teukkou , djoké foukou foukou, soukou, douula meuna songou khéébatina meunineum, Guinteutina déminam , deugeulina aminam/, djégué nako dithi niaan déggeutouma amiiinam/ Liniou djappeu douniou teuri , sunu gaal day tééri , lima djangueu lay taari wané Ndieurigneum.

Bril Fight 4… "Sa Life – Sa Fight" Lyrics

Avant   Bril Fight 4… "Sa Life – Sa Fight" Lyrics

     Intro

     Yeah , sa doundala, sa xaaré la Sa life moy sa fight…. ANALYZIK

 

Refrain

 You better put it in your mind

Gueum né war nga meuna Shine , One day {Sa life moy sa fight}

Boul Meussa Djoukk thi di Fight

Meunn nga ndamou thi sa life , Everyday {Sa Fight moy sa Life}

Never say "no", Don’t say "no" {Boul meussa xaadi}

Never say "no", Don’t say "no"

 

1er Couplet

Li neubou thi yaw di nélaw sa djeumeu dji, fokk nga yééko hommy

Boul nangou di yééw sa xél ba gueumeu thi doundou gui, soukou sa Ôomm yi

Ki djouk ba takkou di kharé, thi finiou khaaré, yokkouna djoom yi

Bou peund bi wouré, gni yagga di beurèk ndiouma nio doul djoomi

Loussa xalat yi dadjati am-na // Kiy djéém té yaagg thi, meun-na //

Lou dougou thi bopp, mou toppeuthi fékhéko djeumeuli mbokk mi kham-na, //

Kouy khaadi lou djéguè la guissoul, Gueustoul, yégati thi, yénouko diissoul /

Djougueul, fékhél dokhé sa xél té bania di waakhi di soul //

Nangou gueuna djéém, yégali warèf yi doga meuna dém //

Ngèmbou beuré lay guiss, wouti dara like this, Boy khaar koula walou douniou meuna yém

Danga wara gueum dithi daw gaw/ Yégg finiou djeum yaw/

bania gueumeu khol lithi kaw naw/ sori am ndam founé law

Aw finiou djougué raw //Meuna djougati thi naathie wi ba faw

 

Refrain

 You better put it in your mind

Gueum né war nga meuna Shine, One day  {Sa life moy sa fight}

Boul Meussa Djoukk thi di Fight

Meunn nga ndamou thi sa life , Everyday {Sa Fight moy sa Life}

Never say "no",  Don’t say "no"  {Boul meussa xaadi}

Never say "no",  Don’t say "no"

 

2 éme Couplet

Boul  nangou dinga déss guinaw, gueumeul sa bopp té deugou né "yay king,"

Kila romb dém, dééssouko naw, Boul déékkati koppeu yi nangoula  "Fighting."

Yaw yay the number one,  Déél djangue thi lignou la wane

Dogali yégali, dogadi yeungali, waakhou yééwi  say rawane

Nanga yeukk ni djom boula//  Djito  fi dara djiomboula //

Boy teuss teuss, beuss, yokkou pass pass, feuss, meunato woté niou Djamboula//

Kouthi tègouli djèègo yeungouwoul, euleuk meunoula djieum kanam/

Ki thi khéékh bi dooné djéngouwoul, filék wanoula djonkanam/

Pousso bi wara di niaw ba sopi sa doundou gui, yaa koy nass, né ci/

Fékhala dass mou niaw, nga  Feugueuti peund bi, fomp mou néSs Néessi/

Béneu bouthi yém dém; danga wara djouk djém; weuri am ndam, takhaw thi Témeu

Beuss djeuli  miseum, djizeum, tégui bizeum, wisdom la kheuw thi théme

 

Refrain

……..Put it in your mind

Gueum né war nga meuna Shine , One day {Sa life moy sa fight}

Boul Meussa Djoukk thi di Fight

Meunn nga ndamou thi sa life , Everyday {Sa Fight moy sa Life}

Never say "no",  Don’t say "no" {Boul meussa xaadi}

Never say "no",  Don’t say "no"

 

 Bridge

 Now you gonna understand this is the way we gonna play  {Boul xaar lééneu  thi kééneu}

Now you gonna know you’re just living  for the fight  {Sa doundoula -Sa xaaré la}

Now you gonna understand this is the way we gonna stay {Boul sééntou ndimbeulou kénneu ,, man}

Now you gonna know, we better do it, for the fight  {Défal linga wara déf Right now }

 

Outro

To be nobody but yourself ,, in a world that’s doing its best ,,,

to make you somebody else… {gueumeul sa bopp}

is to fight the hardest battle you are ever going to fight.

 

Right… The Last Fighter a-k-a The Future ……

Hi… Yya better know…

BRIL FIGHT.4… Sa Life – Sa Fight #ANALYZIK

Sa Life Sa Fight 10 May 2014

Character cannot be developed in ease and quiet.

Only through experience of trial and suffering can the soul be strengthened, ambition inspired, and success achieved.

That which does not kill us makes us stronger.

BRIL FIGHT.4… Sa Life – Sa Fight (tavie-ton combat)
(single extrait de #ANALYZIK )

Enregistrement : Diegui Rails Studio
Trap beat, prod by : #killa-kid & Platinumbeatz Beatz
Mixage & Mastering : Class’Chic Records

http://www.reverbnation.com/brilfight4/song/20825084-sa-life-sa-fight

Bril Fight 4 au "G Hip Hop" de Guediway au concert de Fuk ‘n’ Kuk 03 May 2014

Everything I do, I do it for the love, and for all "the number one Bril"…
"Takkalé – bamou takkalo"
"Souba limou dinthia gueuna sakane mboki alcane"
#Sa_life__Sa_fight" —->coming soon 

Bril Fight 4 au "G Hip Hop" de Guediway (Senegal) au concert de Fuk ‘n’ Kuk  03 May 2014 

Sortie Officielle #Sa_life_sa_fight 10.05.2014 #BF4

Sa Life Sa Fight 10 May 2014

La vie est un un combat que l’on mène contre soi,

Combat très dur parfois, Que l’on mène à chaque pas.

L’essentiel n’est pas d’avoir vaincu, mais de s’être bien battu.

Essayons de ne pas baisser les bras,

Croyons que demain tout changera,

Et que l’on sortira victorieux…

#Sa_life_sa_fight #ta_vie_ton_combat

Sortie officielle ce samedi 10 Mai 2014

https://www.facebook.com/events/sortieofficielle/safightsalife

Diegui Rails Studio présente
BRIL FIGHT.4… "Sa Life -Sa Fight" ( Sa doundou moy sa xaaré)
Single extrait de "#ANALYZIK_the_mixtape"
Concept : Reverse Studios